lundi 2 janvier 2017

Lyrics Viviane No Stress



lyrics No Stress Viviane

non non bounou nagou nou nouy tek stress (x3)
sounou xol di fess nom nou diouk deff fess

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress

ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara

dagna fate beu ngou amm 10 ans 
lou tax gna dioul ma beug ma
daff sa fowoukey 
yombeulnaleu sa visa

woow yeah yeah
demal foula nex way

beugue languak ki
beugue langual ke

beugue languak sama xarite
mani night and day

dégue na nioune fébar lah
woow yeah yeah
demal foula nex way

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress
douma nangou fils nga may tek stress
ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara


goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél 
beugue ma fowel 
ma rombelah
goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél ma rombelah


li safatouma
sama métytou  khol dieuxna
li yeugue louma 
ndax te mane niakouma fayda

li safatouma
tegou thi temps deff  bamou bax jotna
te yaw mi xamgua 
soma noboul 
sa morom nob mah

non non bounou nagou nou nouy tek stress 
bounou nangou nou nouy tek stress
non non bounou nagou nou nouy tek stress 
sounou xol di fess nom nou diouk deff fess

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress
douma nangou fils nga may tek stress
ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara

goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél 
beugue ma fowel 
ma rombelah
goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél ma rombelah


Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire