Lyrics less wakhoul Youssou ndour
Meune wakh da fa nekh wayé degg ka raw
Djemal la dégeu less wakhoul yaw
Boul degeu dal di gueum
wala guiss ne Wawe
Guiss da fa wara lère
Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire
Dou lepp lou nieuw ga gueum ko
Lessou ni less wakhoul
Meune wakh da fa nekh wayé degg ka raw
Djemal la dégeu less wakhoul yaw
Boul degeu dal di gueum
Wala guiss ne Wawe
Guiss da fa wara lère
Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire
Dou lepp lou nieuw ga gueum ko
Lessou ni less wakhoul
Boule ni khaff
Téé do guiss
Boule ni khote
Téé do dégeu
Dou ma deff lou doule dégeu
Lou wessou dégeu dégeu
Dé may deuly lou niou wakhoule
Li niou la bougoul wakh
Diéma deuli ni tekk tékarale
Boule deff ni poulo thiak né dall ni gueum
Nou né toqu sa nopp gné dall ni gueum
Diangal la thi ganaw
Dou lepp lou nga wane
Ak lepp lo diangeu
Ak lou ngou la missale
Nga dall di ko thel gueum
Tel tey yak sa khel yak ya khel wawe
Boula yalla diogé khel dagna wara di khalat wawe
Bagne dou lepp lou nieuw ga gueum ko
Lessou ni less wakhoul
Minguelélema lou warale minguo
Degulelema lou warale dégo
Totaléle lou warale totole
Bagne gueum lepp lou nieuw
Rew bou nekh ak sey ada
Nith kou lekh ak ki nga totole
Wakh diou nek
Wakh diou nek
Ak niou ko mome
Djima gueuli li niou doul khalate
Khamel bou bakh ligna mome
Dé khamel lit li kéne mome
Diémal diangat li nou bindoule
Diémal guiss li nou wagoul
Khel diou deirigne lou doule khalate
Mbinde bo guiss mane na ndi ka mome
Lou waral minguoye
Lou waral tolo
Lou waral minguoye
Lou waral tolo
ehhh
Lou waral minguoye
lyrics By abdoulayebacary
Bravo! Excellent travail! pour la promotion d'une jeunesse consciente et fierement orientée vers le futur. Merci et bonne continuation.
RépondreSupprimerMashaAllah
RépondreSupprimer