lundi 30 juillet 2018

Safary - Faut pas Forcer


Safary - Faut pas Forcer

Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

[Couplet 1]
Béta
Ana louma nameu mane

Adandédo
Wakhma louma nameu mane

Mane rek
Kham nga lou di bonbon?

Bonbon
Man dé mako dakh woh

J'ai des rondeurs oh,
Une belle africaine
Des lolos?
Oh y en a à gogo
Khalé douma taquiner
Té makk douma moquer
Général dafa lerr
Sexy, belle, fresh, je sais comment me saper,
Je suis comme un déesse,
Comme une reine,
Pas besoin de forcer,
Je suis déterminée aïe.

[Refrain]
Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

Faut pas forcer
Faut modifier

Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer

Copie coller
Faut modifier

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer

[Couplet 2]
Kham nga class douniouko ko forcer
Louboutin douko mayé
Nénala moytoul nga ruiner
Louboutin douko mayé

Mane aka ma meune (man rek)
Bari dougou dougou oh (adandédo)
Founé, founé lay diar (Béta)
Aka ma doy warr
Sexy, belle, fresh, je sais comment me saper,
Je suis comme un déesse,
Comme une reine,
Pas besoin de forcer,
Je suis déterminée, aïe.

[Refrain]
Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

Aka ma meune tchi côté bi
Aka ma meune tchi côté bé

May diek biy ridj tchi keur gui, def tchi goowé
Di guel biy réndi kill bi, dokh dokh di bondé

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer
Faut modifier

Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer

Copie coller
Faut modifier

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer


Kham nga class douniouko ko forcer
Louboutin douko mayé
Nénala moytoul nga ruiner
Louboutin douko mayé

Mane aka ma meune (man rek)
Bari dougou dougou oh (adandédo)
Founé, founé lay diar (Béta)
Aka ma doy warr

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer
Faut modifier

Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer

Copie coller
Faut modifier

Aïe, aïe, aïe
Faut pas forcer
Faut pas forcer
Faut pas forcer

Maabo - Namel




[Noface]
Maboooo
Baaaaby, baby namnala
Hoooney, honey namnala

[Mya]
Sama khol lama sori

Démga dani dolé bayima ak wétay
Yama dan motali
Banga démé la guedia yeuk nékhay, nékhay
Yow ya takhone, ma bayi kharit yima am yeup
Té bénn kharit... la désséwone té yowla démga
Bu done nient-fouki att
Dinako tok dila khar
Yama fkuk ci leundeum
Talal faar léral sama yoon
Man reeeek ci khalé
Namouma kudul guissé maabo
Kéne du yow
Té ya fi meun
Yamay diokh li gueune ci man

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you
[Mya]
Quand tu est loin de moi
Je ne vie pas
Je mourais cent fois
Rien que pour être dans tes bras

Baby I miss you
Yes I really do
Honey i miss you
How can I live without you
[Mya]
Quand tu est loine de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Lima soori takh ma diakhasoo
Weetay moma tech caso
Telephone doyuma
Baby yow nammonala
Damalay sentir
Nga diege tes sorigama
Bul mer bul fiir
Guissumafi kumalai diendee
Legleg ma dium nakh teredii
Yow kese rek ci khol
Daraa khajufi
Liga beug moy ma gnibbisi
Khamo ni man mala guena beug gnibbisi
Meuggël ken khamul lumui deff ci nit bamouy namel
Baby yow
Sulamala manon indi fi
Ken wakhatuko

[Mya]
Quand tu est loin de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you

[Mya]
Quand tu est loine de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you

Toucouleur bu rafet baguini eeh
[Mya]
Borom nak ak mew baguini
[Noface]
Ehhh yamai danel
[Mya]
Denga nammon maguini
[Noface]
Nam la takh man ma gnibbisi
[Mya]
Denga nammon maguini
Nam la takh man ma gnibbisi
Eh eh eh eh (diumbagio ari)
Toucouleur rafet bagui nii
Eh eh eh eh (diumbagu ari)
Borom nak ak mew bagui ni
Eh eh eh eh (diumbagio ari)
Toucouleur rafet bagui nii
Eh eh eh eh
Borom nak ak mew bagui ni

Lyrics Daara J Family - Bayi Yoon

Lyrics  Daara J Family - Bayi Yoon


[Intro]
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi

[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Couplet 1 : Faada Fredy]
Fier d’être africain je suis, j'suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
C’est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
Pour me mettre KO il faut minimum une armée de cent mille rambots
Dis à ton prof d’histoire qu’il raconte des histoires
La plus grande des civilisations est née en Afrique noire
L’Afrique a inspiré le monde avec ses pyramides, sa science, ses mathématiques
Ses symboles et ses signes
Elle créa l’écriture avec les hiéroglyphes du temps des pharaons
Tu ne me crois pas ?
Vas-y, demande à Akhenaton.. (de Dakar à Marseille)

[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Couplet 2 : Nongo D]
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni wacc wacc nagnou ande yi xeeb sougnou ngande yi fekki borom jikko you dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga doore fila woore doufou sorre
Afro sama dole na nga mako xole geum sama demb doon nittou tey njaxass ni xeetou parfum’k’gowe
Africains koula xass foy gnawe
Africains xola gneup nignouy ngaange
Africains soy joug doufi gawe
Koula xol dina seet fan la lay ngagne
Geum sa bopp xam fi nga bokk melni garab reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou xel demb kanamou mame gnou giss
Dimbali jam yi biss- gnoul metisses dekkil osiris carbone14 souliwaat gnou giss histoire bindaat grand pere ba petit fils


[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Pont]
Bamako ! Singapour ! Anghata !

[Refrain - Outro]
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi

Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon

Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Nenaala sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani

Nenaala sama gaa gna ngi !

dimanche 29 juillet 2018

Youssou Ndour Chimes of freedom

Lyrics Youssou Ndour Chimes of freedom


Si diguenté marakh massé bi diololi suuf sédé si lagn gawantou fatu mingui done gara ni bi diololi you tedd si melakh yi kawélakh yenene you melni you done rire nguir liberté di riir ngur diambar yi donne khekh té bal takoul di riir nguir gni done gadaay ci yon you meti yi aki tamit kep kho khamni soldar nga bou toumouranké si goudi gui And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing si bene mbar si deuk bi gni ngui lakhatou wone di khol binga khamanténi mbir yangui done wagnékou bi diololi yi nek khew di riir ci taw bi ngelaw youdoul diolol you lerr nek ci kaw di tabi aanhh di riir nguir di bagne, di yeungou nguir ki loff di yengou nguir ki niak chance gni gnou faté gni gnou wor di yengou nguir gni gnou bedi yagg ko lakh mouy doundé And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing si bi dalouk doy warr bi dondiou glace you gnang rott di khoti diaou dji di setou wer ak sell wayam you clochou eglise yi di sani fo soré soré ak nguelaw li desatoul loudoul diolol you nekoul ca rak bi anh di riir ki labiir di riir nguir ki bakh di riir nguir gni gniy gadi ak kiy samm sunu tour ak natal kate bi kene guissoul fou soré soré si diamonom And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing si goudi you bari kemtane yi taw bi melni li louy ler té ay takander you amoul forme té toumouranké di wakh guir lamigne yi mounoula wakh sene khalatt té ay khalat yo khamné fogone nagne ni né khamou gnou lene di wakh nguir silmakha yek gni teukh di wakh nguir gni lou gniy nato jieggen youniouy nakh ak gni gnouye toudé thiaga di wakh nguir say say niou guené mou daw ba rer And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing yi dem ba bene nir ci assamane si naw di tour ndokh ndank ndak té le lérayou lamp yi di gnou dal mel ni fitt wou dioubel si gni natt gni gnouy werr té khamou niou founiou né thi dounya aanh di riir ngui gni wadiou sén si yone you meti yi di riir nguir gni beugeunté té mounou nio wakh sene metite di riir ngui yaram you niou teuj si casso té defou niou dara And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

lundi 2 janvier 2017

Traduction lyrics No Stress Viviane












Traduction Viviane No Tress

Non ! non ! on ne doit plus accepter que l'on nous mette en stress (x3).
Nos cœurs se remplissent et ils disparaissent.
Non ! non ! je ne vais plus accepter que tu me mettes en
stress.
Je ne vais plus accepter que tu me mettes en stress.

Je refuse, je ne vais pas l'accepter no stress.
Mon cœur se remplisse et toi tu disparais.

Laisse-moi tranquille
Tu parles trop.
Moi comme dame.
Rien ne me manques.


Tu as oublié lorsque qu'on avait 10 ans.
Pourquoi tu m'avais pris pour être ton joué

Je t’ai facilité d’obtention de ton visa.
Oh.
Part là où tu veux.

Tu veux être avec celui-ci
Tu veux être avec cela.
Tu veux être avec les amis nuit et jour.
J’ai entendu que c'était une maladie.
Wow.
Fais ce que tu veux.

Non ! non ! je ne vais plus accepter que tu me mettes en stress.

Je ne vais plus accepter 'fils' que tu me mets en stress.
Je refuse, je ne vais pas l'accepter no stress.
Mon cœur se remplisse lit et toi tu disparais.


Laisse-moi tranquille
Tu parles trop.
Moi comme dame.
Rien ne me manques.



Un homme qui te trompe du lundi au dimanche.
Il ne t'aime pas.
Celui que veux me retarder.
Ou veut jouer avec moi je te dépasse
Un homme qui te trompe du lundi au dimanche.
Il ne t'aime pas.
Celui que veux me retarder moi je te dépasse.

Cela ne me fait plus rien.
Mes douleurs de cœur , c'est fini.
Cela ne me fait plus bouger.
Car je ne manque pas de dignité.


Cela ne me fait plus rien.
C’est heur de se mettre dans le temps.
Et toi-même tu sais que.
Si tu ne m’aime pas.
Quelqu’un le fera.


Non ! non ! on ne doit plus accepter que l'on nous mette enbstress.
Nos cœurs se remplissent et ils disparaissent.

Non ! non ! je ne vais plus accepter que tu me mettes en stress (x2).
Je refuse, je ne vais pas l'accepter no stress.
Mon cœur se replisse et toi tu disparais.


Laisse-moi tranquille
Tu parles trop.
Moi comme dame.
Rien ne me manques.

Un homme qui te trompe du lundi au dimanche.
Il ne t'aime pas.
Celui que veux me retarder.
Ou veut jouer avec moi je te dépasse
Un homme qui te trompe du lundi au dimanche.
Il ne t'aime pas.
Celui que veux me retarder moi je te dépasse.




Lyrics Viviane No Stress



lyrics No Stress Viviane

non non bounou nagou nou nouy tek stress (x3)
sounou xol di fess nom nou diouk deff fess

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress

ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara

dagna fate beu ngou amm 10 ans 
lou tax gna dioul ma beug ma
daff sa fowoukey 
yombeulnaleu sa visa

woow yeah yeah
demal foula nex way

beugue languak ki
beugue langual ke

beugue languak sama xarite
mani night and day

dégue na nioune fébar lah
woow yeah yeah
demal foula nex way

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress
douma nangou fils nga may tek stress
ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara


goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél 
beugue ma fowel 
ma rombelah
goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél ma rombelah


li safatouma
sama métytou  khol dieuxna
li yeugue louma 
ndax te mane niakouma fayda

li safatouma
tegou thi temps deff  bamou bax jotna
te yaw mi xamgua 
soma noboul 
sa morom nob mah

non non bounou nagou nou nouy tek stress 
bounou nangou nou nouy tek stress
non non bounou nagou nou nouy tek stress 
sounou xol di fess nom nou diouk deff fess

non non douma nangou nga may tek stress
douma nangou nga may tek stress
douma nangou fils nga may tek stress
ma bagne doumaka nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara
mani diambalima wax dji beutina
mane rek thi xalé namouma dara

goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél 
beugue ma fowel 
ma rombelah
goor bouka tek deal lundi  ba dimanche noboula
kouma beugue tardél ma rombelah


mardi 20 décembre 2016

Lyrics Nidiaye - Toure Kunda + traduction




Del wakh nidiaye
Il faut dire chérie
Diongoma del wakh nidiaye
Dame il faut dire chéri

Yoo Ahh

Gor yui tay yombena djoubol
Les hommes d'aujourd'hui sont faciles à réconcilier
Diongoma del wakh nidiaye Ndeyssane
Dame il faut dire chéri Yene ya gui ni djigene bou gor salo ndieuf thie na bakh Vous étés là les femmes dévouées vos actes devez être bonne

Kay magui ni djinene gor salo
viens je suis là la femme dévouée
Momos momos na diour na bakh
Tout ce qu'elle met au monde ça va être bon
Nopil nopil yene djigene you gor salo
Ne vous en faites pas femmes dévouées
Momos momos lo diour momos bi na bakh
Tout ce qu'elle met au monde ça va être bon

Isma-ousman bathia ousmane
Isma -ousmane jusqu'à ousmane Isma ousoubo bathia Isma -ousmane jusqu'à ousmane Boule dem togu-na
"ne part pars pas - je reste"
djigene bou gor salo lo diour na bakh
Tout ce qu'elle met au monde ça va être bon

Ley ley
Ley ley Leya leya
Leya leya


Ndeye ak baye am neniou dole si dom mame
père et mère ont beaucoup de raison sur leurs enfants Waye kene namowouko mais personne ne le contredit
Ley ley
Ley ley Leya leya
Leya leya
Eyywaye
Bou ndone djiote
Si le soir arrive Naga sangou solou khegh lou nekh hoooo tu dois te laver, porter de jolies habilles et sentir bon
Weyoo
Bo bougê sa dieukeur contane
si tu veux que ton mari soit heureux
Diongoma del wakh nidiaye
dame il faut l'appeler chérie
Del wakh nidiaye
il faut dire chérie
Diongoma del wakh nidiaye
Dame il faut dire chéri
Yoo Ahh
Gor yui tay yombena djoubol
Les hommes d'aujourd'hui sont faciles à réconcilier
Diongoma del wakh nidiaye
Dame il faut dire chéri
Sou ndone djiote
Si le soir arrive Naga sangou solou khegh lou nekh tu dois te laver, porter de jolies habille et sentir bon
Gna togh di khar Sa waye ndiew
tu t'assoie tu attends qu'il arrive
Mou tew
quant il vient
Gna terral ko
tu t'occupe de lui
Eyyy
eyyy

AYy way sou ndone djiote
Si le soir arrive Naga sangou solou khegh lou nekh tu dois te laver, porter de jolies habille et sentir bon
Wayoo
Bo bougê sa dieukeur contane
si tu veux que ton mari soit heureux
Diongoma del wakh nidiaye
dame il faut l'appeler chérie

Del wakh nidiaye
il faut dire chérie
Diongoma del wakh nidiaye
Dame il faut dire chéri

Yoo Ahh

Gor yui tay yombena djoubol
Les hommes d'aujourd'hui sont faciles à réconcilier

Diongoma del wakh nidiaye
Dame il faut dire chéri

Sou ndone djiote
Si le soir arrive Naga sangou solou khegh lou nekh tu dois te laver, porter de jolies habille et sentir bon
Diegenou dounouya way nalene
Les femmes de dounouya c'est vous que je chante Diegenou dounouya yen lako yenè
Les femmes de dounouya Je vous dédit cette musique