lundi 30 juillet 2018

Maabo - Namel




[Noface]
Maboooo
Baaaaby, baby namnala
Hoooney, honey namnala

[Mya]
Sama khol lama sori

Démga dani dolé bayima ak wétay
Yama dan motali
Banga démé la guedia yeuk nékhay, nékhay
Yow ya takhone, ma bayi kharit yima am yeup
Té bénn kharit... la désséwone té yowla démga
Bu done nient-fouki att
Dinako tok dila khar
Yama fkuk ci leundeum
Talal faar léral sama yoon
Man reeeek ci khalé
Namouma kudul guissé maabo
Kéne du yow
Té ya fi meun
Yamay diokh li gueune ci man

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you
[Mya]
Quand tu est loin de moi
Je ne vie pas
Je mourais cent fois
Rien que pour être dans tes bras

Baby I miss you
Yes I really do
Honey i miss you
How can I live without you
[Mya]
Quand tu est loine de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Lima soori takh ma diakhasoo
Weetay moma tech caso
Telephone doyuma
Baby yow nammonala
Damalay sentir
Nga diege tes sorigama
Bul mer bul fiir
Guissumafi kumalai diendee
Legleg ma dium nakh teredii
Yow kese rek ci khol
Daraa khajufi
Liga beug moy ma gnibbisi
Khamo ni man mala guena beug gnibbisi
Meuggël ken khamul lumui deff ci nit bamouy namel
Baby yow
Sulamala manon indi fi
Ken wakhatuko

[Mya]
Quand tu est loin de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you

[Mya]
Quand tu est loine de moi
Je ne vie pas
Je mourais 100 fois
Rien que pour être dans tes bras

[Noface]
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you

Toucouleur bu rafet baguini eeh
[Mya]
Borom nak ak mew baguini
[Noface]
Ehhh yamai danel
[Mya]
Denga nammon maguini
[Noface]
Nam la takh man ma gnibbisi
[Mya]
Denga nammon maguini
Nam la takh man ma gnibbisi
Eh eh eh eh (diumbagio ari)
Toucouleur rafet bagui nii
Eh eh eh eh (diumbagu ari)
Borom nak ak mew bagui ni
Eh eh eh eh (diumbagio ari)
Toucouleur rafet bagui nii
Eh eh eh eh
Borom nak ak mew bagui ni

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire