lundi 30 juillet 2018

Lyrics Daara J Family - Bayi Yoon

Lyrics  Daara J Family - Bayi Yoon


[Intro]
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi

[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Couplet 1 : Faada Fredy]
Fier d’être africain je suis, j'suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
C’est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
Pour me mettre KO il faut minimum une armée de cent mille rambots
Dis à ton prof d’histoire qu’il raconte des histoires
La plus grande des civilisations est née en Afrique noire
L’Afrique a inspiré le monde avec ses pyramides, sa science, ses mathématiques
Ses symboles et ses signes
Elle créa l’écriture avec les hiéroglyphes du temps des pharaons
Tu ne me crois pas ?
Vas-y, demande à Akhenaton.. (de Dakar à Marseille)

[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Couplet 2 : Nongo D]
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni wacc wacc nagnou ande yi xeeb sougnou ngande yi fekki borom jikko you dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga doore fila woore doufou sorre
Afro sama dole na nga mako xole geum sama demb doon nittou tey njaxass ni xeetou parfum’k’gowe
Africains koula xass foy gnawe
Africains xola gneup nignouy ngaange
Africains soy joug doufi gawe
Koula xol dina seet fan la lay ngagne
Geum sa bopp xam fi nga bokk melni garab reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou xel demb kanamou mame gnou giss
Dimbali jam yi biss- gnoul metisses dekkil osiris carbone14 souliwaat gnou giss histoire bindaat grand pere ba petit fils


[Refrain]
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon ?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes

[Pont]
Bamako ! Singapour ! Anghata !

[Refrain - Outro]
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi

Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon

Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Nenaala sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani

Nenaala sama gaa gna ngi !

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire