Lyrics Youssou N'Dour Li ma weesu
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
setou leg leg ma giéssou si li ma messou
leg leg ma retiou
wala sa di bakou
foutu gouney feké
damanene di tété
wakh loum ma nekhe
ma beuguemene no
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
lou ma geune di yague
khel bi melni bank
lou ma guen di mague
delou touti tanke
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
maney setou leg leg ma giéssou si li ma messou
leg leg ma retiou
wala sa di bakou
foutu gouney feké
damanene di tété
wakh loum ma nekhe
ma beuguemene no
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
foutu gouney feké
damanene di tété
wakh loum ma nekhe
ma beuguemene ti
lou ma geun di diegué
melni da ma soreyy
lou ma soreyy geu di guiss lou ma diegué wone
lou ma geune di yague
khel bi melni bank
lou ma guen di mague
delou touti tanke
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
damay damay damay delou gouney
mele ni mele ni dou ma mageu
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
li ma doune déé
li ma weesu déy déloussi malni setou
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire