jeudi 22 septembre 2016

Traduction Badiene Youssou Ndour



Traduction Lyrics badiene Youssou N'Dour 



Je dis tata c'est la grande sœur ou la petite sœur de papa
Tout ce qui peut se passer ta tante
Elle est toujours là
Le jour où tu entre dans l'étape adulte
Ta tante est là pour te parler de la vie
Elle est comme un oncle en femme donc ta tante a de l'importance



Oui tata c'est la grande sœur ou la petite sœur de papa
Tout ce qui peut se passer ta tante
Elle est toujours là
Ta tante est là pour te parler de la vie
Elle est comme un oncle en femme donc ta tante a de l'importance


Oui c'est un chante de joie tous les tatas levaient vous et montraient vous


Oui tata c'est la grande sœur ou la petite sœur de papa
Tout ce qui peut se passer ta tante
Elle est toujours là
Ta tante est là pour te parler de la vie
Elle est comme un oncle en femme donc ta tante a de l'importance


"SOUSHE" tata c'est la grande sœur ou la petite sœur de papa
 Tout ce qui peut se passer ta tante
Elle est toujours là
Ta tante est là pour te parler de la vie
Elle est comme un oncle en femme donc ta tante a de l'importance


Oui c'est un chante de joie tous les tatas levaient vous et montraient vous
Oui c'est un chante de joie tous les tatas levaient vous et montraient vous

Le griot disait que là où il y'a un lion qui et au l'alentour, une chèvre qui a une tante ne la passerai pas habiter là-bas
Donc ta tante a de l'importance

Tout ce qui peut te perdre dans ta tradition
Ta tante peut te le faire connaitre
Si tu veux connaitre ta tradition
Connaitre l'origine de tes ancêtres
Tout ce qu'elle pourra te dire sache que c'est ça.

Ta tante connait kadjor jusqu’à benekhone
Donc ta tante a de l'importance

On dit qu’un homme peut être le plus vieux d'un pays
Mais des tantes peuvent être nombreuses dans une maison
Se connaitre a soit même c'est que l'on t'appelé pour te dis ce que tu es
Si tu veux connaitre ta tradition
C’est ta tante qui va te le dire
Elle va te dire
Passe par ici
Fait ceci
Ne part pas là-bas
Fait le comme ça

Si tu y pense bien tout cela c'est vrai

Le griot disait que là où il y'a un lion qui et au l'alentour, une chèvre qui a une tante ne la passerai pas habiter là-bas
Donc ta tante a de l'importance


Si ta femme a un bébé c'est tata qui la tient dans ces bras
Raser les cheveux
Et si c'et une fille on la donne son nom

Ta tante connait kadio
Ta tante connait ta tradition

Se connaitre a soit même c'est que l'on t'appelé pour te dis ce que tu es
Ta tante connait ta tradition

Si ta femme a un bébé c'est tata qui la tient dans ces bras
Raser les cheveux
Et si c'et une fille on la donne son nom


Si tu veux connaitre ta tradition
C’est ta tante qui va te le dire

Le griot disait que là où il y'a un lion qui et au l'alentour, une chèvre qui a une tante ne la passerai pas habiter là-bas
Donc ta tante a de l'importance


Tous les tatas levaient vous et montraient vous cette chanson est pour vous

Je dis tata c'est la grande sœur ou la petite sœur de papa
Tout ce qui peut se passer ta tante
Elle est toujours là
Le jour où tu entre dans l'étape adulte
Ta tante est là pour te parler de la vie
Elle est comme un oncle en femme donc ta tante a de l'importance

Oui c'est un chante de joie tous les tatas levaient vous et montraient vous
Oui c'est un chante de joie tous les tatas levaient vous et montraient vous

Tatas levaient vous et montraient vous

Aulley tu es une tata

Chéri Ismaël Lo tu es tata


Tous les tatas levaient vous et montraient vous cette chanson est pour vous




Lyrics Badiene Youssou N'Dour



Mani badien modi magii bay wala rakam kone loukhew lounek mani badiene takhaw koon beuss bou doom douger negou goor badiene takhaw wayaal ko mbaxx wayee nidiaye ni yaay matgna ni baay badiene amna mannaa
Waaw badien modi magui baay wala rakeum kone loukhew loune mani badiene takhaw beus bou doom douger negou goor badiene takhaw wayaal ko mbaxx waw ne wayou teranga la kouy badiene diougeul yeungou badiene badiene sougn sagagn badiene badiene ×4 tassoukaat nganga naan gaïnde gou waaf cii bountou keurgeu di melastiku beuy bou am dadiene dou feu dem kone sacreale badiene amna manaa louleu nekh ci seu thiossane badiene khameul leuko, so beuger kham seu thiossane kham fisseu maam yi bayeko demal seti badiene limoula thia wakh diu degn badiene na kham kadjor bathieu benekhone thiossano askane badiene amna manaa nena gniou maak matna maak cii rew waye it badiene matna baay ci bir keur kham ca boop mo geune gniou wola nanleu ki ngeu done so beuger kham seu thiossane badiene moleu koy khameul molenan awal fi boul dem fe defeel ni soko setlooo dara douceu degn Tasoukaat ngagna naan gaïnde gou waaf ceu bountou keurgeu di melastiku beuy bu am dadiene doufeu dem kone badiene amna mana (Mabye Dieye Faye) sou thiamigne amer doom badiene mokoy ouff woteul bebe karaweum gniou touder koko Ouleye Diallo chérie Madou badienou khaleyi chérie Ismaël Lo sougougn sagagn badiene na kham kadjor badiene mo kham thiossane kham seu bop mo geune niouley wo nanleu ki ngeu done badiene mo kham kadjor badiene mo kham thiossane Mabye Dieye Faye) sou thiamigne amer doom badiene mokoy ouff woteul bebe karaweum gniou touder koko Ouleye Diallo chérie Madou badienou Ouleye chérie Ismaël Lo sougougn sagagn bo beuger kham seu thiossane Mbaye mani bo beuger kham seu thiossane seu badiene moleu koy khameul Tasoukaat ngagna naan gaïnde gou waaf ceu bountou keurgeu di melastiku beuy bu am dadiene doufeu dem kone badiene amna mana Mbaye Dieye Faye) souss badiene beu kouy badiene diougeul yeungou kouy badiene diougeul yeungou way bi diarnako Mbaye badien modi magui baay wala rakeum kone loukhew loune mani badiene takhaw beus bou doom douger negou goor badiene takhaw wayaal ko mbaxx waw ne wayou teranga la kouy badiene diougeul yeungou badiene badiene sougn sagagn badiene badiene




Lyrics Alalou Mboolo Youssou N'dour



dolou lou ak yakar mo takh niou tann la dolou lou ak yakar mo takh niou wallon woloula bou nitt yi barry barry
yow dong nan fi tane neu tekk la fee dolou lou ak yakar mo takh niou tann la dolou lou ak yakar mo takh niou wallon woloula bou nitt yi barry barry yow dong nan fi tane neu tekk la fee confiance bou niou amm si yaw boul ko saganeee yakar bi nou amm si yow ba kay denk la sou la key am ga loy bagh gorforoul ba deff ko niou ka beugé gorr bakhna jigeenne bakhna jioup dall moy li worr fekhel ba yeboulene na fekhel ba woney lou takh niou woloula gorr bakhana jigenne bakhna jioup dall moy li worr fekhel ba yeboulene na fekhel ba woney lou takh niou woloula dium borry ndone bourr daly dium borry ndone bourr daly dium borry dafa lalou bour motakh mou diam kou defoul dara dep di koy door dium borryey dium borry dafa lalou bour motakh mou diam kou defoul dara dep di koy door dium borryey sou deyy lou ga wara wakh wakh dall mou diekh sou deyy lou ga wara diokhe diokho nio ko mome soi deyy loy ga wara dokh dokh do ba mo matte maïs fefele beu yemene naga fefe ba woné lou takh niou woloula wakhou ma la dara waye wolou gui nou la wolou boul ko fowé yaw alalou MBolo boll ko fowé bilay dinkanela boul ko fowé yaw alalou mbolo boul ko fowé bilau dinkanela wawaw boul ko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowé deugel samal ma wa way bouko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowé deuk deug mbotoul ma ma wawaw boul ko fowé dilay alalou mbolo bou ko fowe deug deug samal ma waw waw bilay alalou mbolo wawa bilay samal ma daa gaa wara gore denkanè denkanéee lo momoul manou theuy yaw alalou mbolo boul ko fowé deuk deug sa mal ma boul ko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowe deuk deuh moy toul ma alalou mbolo wowoww boul ko fowé bilay alalou mbolo deug deug manou nou sa wawaw dou atier lou tatier dou arier lou tatier lyrics alalou mbolo by abdoulayebacary


Lyrics Djino Youssou N'Dour






kou guisse sa beut yi di khol mbaye gueye dioudal mako ahh mbeuguel capitaine nou mboromom mbeuguel da fa disse
dafa beuri dollè dinala niakalo sa allal di gna nagou yaw lo geumoul mbeuguel bou la diam ba amo loy deff yalla bo beug nikk ki kokou beug la loloo andoula ak ay principe ah sentiment la ay dioyy riekk la situation rekk la mbeuguel bou la diap ba so amon loy deff yalla bo beug nikk ki kokou beug la loloo mbeuugnaleu chérie diogh nala sa ma khol bolethi di la yeureum dila moungalit fo beug niou dem fa li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy man sou ma amon avion tay ma maylako di la dawalal fo beug nou dem ko li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy mbeugnala fogu nou wendellou bou mbeugel donne lumière diante te bi lay dieuli kham na di na metti sa wa ye diarral na ma ko li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy lou ma dougou nga kham ko kham ndany lou ma am sa ma daradia damppul li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy mbeugnala fogu nou wendellou Golber sou ma khamon ki kan la dou ko defeti! dou defeti lou ni mell khana khamol sou niou kharite nga golber kou la khamoul na la ladj Aladji mensou seck ba tia Ndar mba nou fekhe ba lath la way di fou nieuwone donn seyaré sa golber gui na ne ga Ndar geutt beuri nga fey ay kharite ngui la sopp barina Mame coumba Barry si la bokk bilah beugnalala fokk niou wendelou dikh nala sa ma khol bokk si di la yeureum di la mou nieul lit fo beug nio dem fa li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy mane sou ma avion tay ma may lakou di la dawalal fo beug niou dem fa li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy bo mbeuel donne lumière diante bi la dieuli kham na di na metti sa waye na ma ko li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy beugeunalla foy nou wendellou foncnala fokk niou wendellou mane sou ma avion tay ma may lakou di la dawalal fo beug niou dem fa li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy bo mbeuel donne lumière diante bi la dieuli kham na di na metti sa waye na ma ko li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy loi ma doug na kham ko sa ma dara oumpoula lisou la doyoul khaw ma lou lay doyy man dall beug nala mbaye kay niou wendellou djino kou la guii djii ala mais djinno Lyrics by Abdoulayebacary


lundi 19 septembre 2016

Lyrics Del Teew Youssou N'Dour



Lyrics Del Teew Youssou N'Dour


dou ma dopp diow lolou so ka dekay yen fa gen dieum sorewool gorr sou nekh warr na moytelekou niou nann la yatogn
so beugé cou la guiss diogn tieur bi ga momm respectel say wakh niga ma deff ma tokk keur geu di na khar deig deug nieuwolo ya takh rendez vous yo ma amone ma pousse lene fuiss nga fonkee la rekk mo takh ma tela diokk préparer di la khar lii mo dakk lig ma def meti la lolou respectel rendez vous dem dikk kou la guiss diog la tieur bi nga mom respectel say wakh niga ma deff ma tokk keur geu di na khar deig deug guissoumala ya takh rendez vous yo ma amone ma pousse lene fuiss nga ttttt nooo morrre nooo morrre nooo morrre yaw tam tamaloma di ma topato math ma tiall demm si di la sett si yaw tam tamaloma di ma topato math ma tiall demm si di la sett si dou ma topp diow lolou so ka deugg gée feu gen ddum mo sorewoul gorr sou nekk woyletikou niounela ya togh so beuge kou ga guiss diokh ka tieur bi mou mome respectel say wakh nii ga ma deff mo thogg keur ga di na khar nieuw woulo ya thakh kenn kou ma nee neyniou dadie ma tayy deyy demm dell deww a can give no more bicause of the waiter dou ma topp diow lolou so ka deugg gée feu gen ddum mo sorewoul gorr sou nekk woyletikou niounela ya togh so beuge kou ga guiss diokh ka tieur bi mom respectel say wakh nii ga ma deff mo thogg keur ga di na khar nieuw woulo ya thakh kenn kou ma nee neyniou dadie ma tayy deyy demm dell deww a can give no more because of the waiiting dell teww dell teww no more no more lyrics Del Tew by Abdoulayebacary


Traduction lyrics C'est l'amour Youssou N'Dour

Traduction lyrics C'est l'amour  Youssou N'Dour



si je parle avec mon esprit
car la nuit pour conseil
si le matin arrive j'oublie les reves de la nuit derniere


c'est l'amour

si je te croise en passant 
tu crois que tout est bon
l'apparece ta trompé 
tu ne connais pas ce qui est dans moi

c'est l'amour

to love
AmAr
Chintouru
yébene


je travail
je rend grace a dieu
je regle mes problemes

mais il y'a quelque chose qui manque

c'est l'amour

moi j'ai pas manger 
moi j'ai pas encore bu
moi je n'est plus faim
moi je ne suis pas fatigué
moi j'ai pas encore sommeil
je ne dors pas assez


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
nakhe beur


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
Chintouru
yébene
nakhe beur

moi j'ai pas manger 
moi j'ai pas encore bu
moi je n'est plus faim
moi je ne suis pas fatigué
moi j'ai pas encore sommeil
je ne dors pas assez



c'est l'amour

je travail
je rend grace a dieu
mais il y'a quelque chose qui manque

c'est l'amour

si je parle avec mon esprit
car la nuit pour conseil
je travail
mais il y'a quelque chose qui manque




Lyrics Youssou N'dour C'est l'amour


Lyrics Youssou N'dour C'est l'amour



sou wakhtané ak sa ma ngiégénay
nakh goudi de yokou khel
sou beuthie ké ma dall di faté
mane guinntiyé you  ma guintone bigu

c'est l'amour


sou mala rombé di dem 
na fokk liéph bakhna si mane
apparrence bi nakhna la
khamoulo li nékk si mane 


c'est l'amour

to love
Amoré
Chintouru
yébene

magui dann sa ma dolé
magui sante yalla
magui fathe sa may athio

mounay amm na lou dess


c'est l'amour

mane lekouma
mane nanouma ba they
mane hiffouma ba they
mane somouma 
mane geumouma ba they
nelawouma lou doyy


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
nakhe beur


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
Chintouru
yébene
nakhe beur


mane lekouma
mane nanouma ba they
mane hiffouma ba they
mane somouma 
mane geumouma ba they
nelawouma lou doyy


c'est l'amour


magui dann sa ma dolé
magui sante yalla
mounay mounay amm na lou dess


souma khanaé akk sa ma ngégenay
nakh goudi dey yokou khel
magui dann magui dann sa ma dolé

mounay mounay amm na lou dess

lyrics C'est l'amour youssou N'dour by Abdoulayebacary



samedi 17 septembre 2016

Traduction lyrics Youssou N'Dour - 7 Seconds ft. Neneh Cherry



Traduction lyrircs Youssou N'Dour - 7 Seconds ft. Neneh Cherry


Ne me regarde pas de loin
Ne regarde pas mon sourire, en pensant que je ne sais pas
Ce qui est au-dessus et sous moi
Je ne veux pas que tu me regardes et penses
Que ce qui est en toi est en moi, ce qui est en moi est là
pour les aider

Voyous et ignorance,
Nous devrions nous bouger, loin de ceux qui pratiquent les
mauvais sorts
Pour le soleil et la pierre
Mauvais jusqu'au sang
La bataille n'est pas finie
Même quand elle est gagnée
Et quand un enfant naît dans ce monde
Il n'a aucun concept
Que la couleur de la peau déterminera son destin

Ce n'est pas une seconde
7 secondes de cela
Simplement tant que je reste
J'attendrai
Ce n'est pas une seconde
7 secondes de cela
Simplement tant que je reste
J'attendrai

J'attendrai

J'attendrai

J'assume les raisons qui nous poussent de changer tout,
J'aimerais qu'on oublie leur couleur pour qu'ils espèrent
Beaucoup de sentiments de race qui font qu'ils désesperent

Je veux les portes grandements ouvertes,
Des amis pour parler de leur peine, de leur joie
Pour qu'ils leur filent des infos qui ne divisent pas
Changer

Ce n'est pas une seconde
7 secondes de cela
Simplement tant que je reste
J'attendrai
Ce n'est pas une seconde
7 secondes de cela
Simplement tant que je reste
J'attendrai

J'attendrai

J'attendrai

Et quand un enfant naît dans ce monde
Il n'a aucun concept
Que la couleur de la peau déterminera son destin
Il y a des millions de voix
Il y a des millions de voix
Pour te dire ce qu'elle doit penser
Alors tu ferais mieux d'écouter, juste pour une seconde

lyrics Youssou N'Dour - 7 Seconds ft. Neneh Cherry


lyrics Youssou N'Dour - 7 Seconds ft. Neneh Cherry


Boul ma sene, boul ma guiss madi re nga fokni mane
Khamouma li neka thi sama souf ak thi guinaw
Beugouma kouma khol oaldine yaw li neka si yaw
mo ne si man, li ne si mane moye dilene diapale
Roughneck and rudeness,
We should be using, on the ones who practice wicked charms
For the sword and the stone
Bad to the bone
Battle is not over
Even when it's won
And when a child is born into this world
It has no concept
Of the tone the skin is living in
It's not a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
It's not a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
I'll be waiting
I'll be waiting
J'assume les raisons qui nous poussent de changer tout,
J'aimerais qu'on oublie leur couleur pour qu'ils esperent
Beaucoup de sentiments de race qui font qu'ils desesperent
Je veux les portes grandements ouvertes,
Des amis pour parler de leur peine, de leur joie
Pour qu'ils leur filent des infos qui ne divisent pas
Changer
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
It's not a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
I'll be waiting
I'll be waiting
And when a child is born into this world
It has no concept
Of the tone the skin is living in
And there's a million voices
And there's a million voices
To tell you what she should be thinking
So you better sober up for just a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
It's not a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting
It's not a second
7 seconds away
Just as long as I stay
I'll be waiting



vendredi 9 septembre 2016

Traduction Lyrics less wakhoul Youssou ndour

   


Traduction Lyrics less wakhoul Youssou ndour


Le fait de bien parlait c’est bon mais bien entendre c’est mieux
Essaye d’entrende LESSE WAKHOUl

N’entend pas quelque chose et le croire
Ou bien tu vois et tu es en accord
Ce qu’on voit doit être claire
Entendre doit être lucite
Etudie ce qui est à l’intérieur
Ne croit pas à tout ce qui vient

Lessou ni less wakhoul
Le fait de bien parlait c’est bon mais bien entendre c’est mieux
Essaye d’entrende LESSE WAKHOUl


N’entend pas quelque chose et le croire
Ou bien tu vois et tu es en accord
Ce qu’on voit doit être claire
Entendre doit être lucite
Etudie ce qui est à l’intérieur
Ne croit pas à tout ce qui vient
Lessou ni less wakhoul


Ne soit pas en accord
Si tu ne vois pas
Ne soit pas d’accord
Si tu n’entends pas
Je ne fais pas qu’entendre
Je dépasse le fait d’entendre
Je vais essayer d’entendre
Ce qu’ils ne veulent pas dire
Et après je reste tranquille à les écoutés

Ne fait pas comme Poulo Thiak tu y crois
Ou tu crois à tout ce qui vient toucher à tes oreilles
Etudie l’affaire avant d’y croire
Ce n’est pas tout ce qu’on te montre
Ou à tout ce que tu as appris
Ou à tout ce que ton ta dis
Que tu dois croire. NON
Utilise ton esprit et ton esprit seulement

Si Dieu t’a donné un esprit
Tu dois réfléchir
Et éviter tout ce qui vient et tu le crois

 Lessou ni less wakhoul

Comparais-moi ce que l’on doit comparer
Entendrait moi ce que l’on doit entendre
Egalais mois ce que l’on doit égaler
Et éviter tout ce qui vient et tu le crois
Chaque pays avec ces traditions
Chaque personne avec qui tu égale
Chaque parole à son destiné
L’esprit ne sert qu’à réfléchir
Bien reconnaitre ce qui t’appartient
Et bien reconnaitre ce qui appartient à l’autre

Essaie Etudie ce que l’on n’a pas écris
Essaie de voir ce que tu n’as pas vue
L’esprit ne sert qu’à réfléchir
Chaque parole à son destiné
Ce qui est à l’origine de comparer
Ce qui est à l’origine d’égaler



Lyrics youssou n'dour the lion (gainde)




Lyrics youssou n'dour the lion (gainde)



fo deug marawath soungou gaindé la 
ndiaye gaindé boure leuh deugeu la 
fo fekk gaindé  te dou fi takhaw
téé lou mou beugeu dall di ti tekk lokhom
mome néna kéén waroul bakou
mome boure la def bopame kou doleme 
bagne na ba dou bokol yonam
kou kou wedi na diarr fo mouy diarr


ngioune ngui dé yéney sou ngou gaindé
ngioune ngui dé yéney sou ngou gaindé

dé déé

nbamli nbamli né guén ko dieul
na guén ko deff na guén ko dann déffé
nbamli nbamli né guén ko dieul
nbamli nbamli né guén ko dieul
na guén ko deff na guén ko dann déffé
nbamli nbamli né guén ko dieul

diambar dé gnioun dhégne ko dondou
sou gnou mame dé mou sou ngui dess ganaw
diom diodou mougui fi té moussou fi diougé
fitt bodou mougui fi té moussou fi diougé
sou gnou rew mbi royoukal la moussa donn


diom diodou mougui fi té moussou fi diougé
diom diodou mougui fi té moussou fi diougé
diom diodou mougui fi té moussou fi diougé

tééééé

nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé

nbamli nbamli né guén ko dieul
na guén ko deff na guén ko dann déffé
nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé
nbamli nbamli né guén ko dieul

yooooooo

fi ngou tolou ngoune amm né gnou yakar
sou ngou mbeur bi da fa endall douléme
mbeur bi té kou ka sorou mou danne la
mbeur bi té kou ka sorou mou danne la

yététééé


nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé
nbamli nbamli né guén ko dieul

mboroti ndiaye dou delou ganaw

nbamli nbamli né guén ko dieul
fitt bi déé daf ka dondou

nbamli nbamli né guén ko dieul
bilay 
na guén ko deff na guén ko dann déffé


nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé
nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé
nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé 
gaindé ndiaye gaindé la
nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé  
mboroti ndiaye 
nbamli nbamli né guén ko dieul
deugla deug khamnako
nbamli nbamli né guén ko dieul
yélééé yélééé
mboroti ndiaye 
nbamli nbamli né guén ko dieul
na guén ko deff na guén ko dann déffé
nbamli nbamli né guén ko dieul
bou la yéé te 
nbamli nbamli né guén ko dieul
lyrics The lion Gaindé By Abdoulayebacary





lyrics Youssou Ndour baykat


 lyrics Youssou Ndour baykat

kha lola
kha lola
lola la la la

djambar you gorr ya ngoge baykat

bay mbboke bay dougoup you nou doundé

nath bi di tangue niou sentou taww

séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne

sou naletelé ngédi sentou taww
soko wedé demal baol
mba ga dem ba walo Mbodj
sou nord tioté nou weurr di leep
sou tambalé khinn niou sentou taww

sou tawwé sou tawwoul ngui fay borr


séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne

mbir mbirou garap mbagui si yaww
khiff yi ngou khiff yayee kou key fadj
mbeuss yi niou wessou ndiome nelawouniou

sou naletelé ngédi sentou taww
soko wedé demal baol
mba ga dem ba walo Mbodj
mba ga dem sine saloum béé


séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne


djambar you gorr ya ngoge baykat
bay gerté bay mbokk you nou doundé

lata mouy taww niou falas khar

séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne

sou taww mbaré Dakarou Wagni ndeukk
sou taww amoul dakarou Yokk ndeukk

lou thi meuna amm li déé metina 

séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne


momo avk sa mbope bathi
dimba lé ko 
dimba lé ko
ya karr dafa tass
dimba lé ko
momo avk sa mbope bathi

kha lola
kha lola
lola la la la

kha lola
kha lola
lola la la la
séé sédelene djambar guéne

momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne



 lyrics Youssou Ndour baykat by Abdoulayebacary




Lyrics less wakhoul Youssou ndour


Lyrics less wakhoul Youssou ndour


Meune wakh da fa nekh wayé degg ka raw
Djemal la dégeu less wakhoul yaw


Boul degeu dal di gueum
wala guiss ne Wawe
Guiss da fa wara lère
Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire
Dou lepp lou nieuw ga gueum ko


Lessou ni less wakhoul

Meune wakh da fa nekh wayé degg ka raw
Djemal la dégeu less wakhoul yaw


Boul degeu dal di gueum
Wala guiss ne Wawe
Guiss da fa wara lère
Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire
Dou lepp lou nieuw ga gueum ko

Lessou ni less wakhoul

Boule ni khaff
Téé do guiss
Boule ni khote 
Téé do dégeu
Dou ma deff lou doule dégeu
Lou wessou dégeu dégeu
Dé may deuly lou niou wakhoule
Li niou la bougoul wakh
Diéma deuli ni tekk tékarale

Boule deff ni poulo thiak né dall ni gueum
Nou né toqu sa nopp gné dall ni gueum
Diangal la thi ganaw

Dou lepp lou nga wane
Ak lepp lo diangeu
Ak lou ngou la missale
Nga dall di ko thel gueum
Tel tey yak sa khel yak ya khel wawe

Boula yalla diogé khel dagna wara  di khalat wawe
Bagne dou lepp lou nieuw ga gueum ko

Lessou ni less wakhoul



Minguelélema lou warale minguo
Degulelema lou warale dégo
Totaléle lou warale totole
Bagne gueum lepp lou nieuw 
Rew bou nekh ak sey ada
Nith kou lekh ak ki nga totole
Wakh diou nek
Wakh diou nek 
Ak niou ko mome
Djima gueuli li niou doul khalate
Khamel bou bakh ligna mome
Dé khamel lit li kéne mome

Diémal diangat li nou bindoule
Diémal guiss li nou wagoul
Khel diou deirigne lou doule khalate
Mbinde bo guiss mane na ndi ka mome

Lou waral minguoye 
Lou waral tolo
Lou waral minguoye 
Lou waral tolo
ehhh
Lou waral minguoye 

lyrics By abdoulayebacary








lundi 5 septembre 2016

Traduction lyrics Song Daan Youssou N'dour

lyrics
Si tu veux connaître
il faut nous demander
C’a veut dire si tu veux connaitre
il faut aller le demander à Youssou

Appel moi, appel moi meme dans l'obbsurité
je vais se répondre
Ouvre mon
cœur
tu verras comme je suis heureux de Youssou

Tant que de t’aies
dans mon cœur,
tout ce que qui vient de
je le terrasse

Tan que de t’aies
dans mon esprit,
tout ce que qui vient
de je le terrasse

Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse

Moi je dis
Que c’est toi
Et toi tu dis
Que c’est moi

Moi je dis
Que c’est toi
Et toi tu dis
Que c’est moi

Eh eh
Eh eh
Un jour arrivera
Comme on se que l’on racontera

Ahh
Personne ne se lèvera
pour dire que je serai présent ce jour


Car le vent qui souffle qui nous emportent
Et les feuilles tombent sur les arbres
Et tout ce qui se passe ici on ne doit pas l’oublier
Car l’Afrique ses enfants ses montres

Tan que de tu’aies
dans mon cœur,
tout ce que qui vient
de je le terrasse
Tan que de tu’aies
dans mon esprit,
tout ce que qui vient
de je le terrasse

Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse
Je l’attaque et je le terrasse


Moi je dis
Que c’est toi
Et toi tu dis
Que c’est moi

Moi je dis
Que c’est toi
Et toi tu dis
Que c’est moi

Eh eh
Eh eh



Je vais passer au milieu
Qu’il ait des braises
ou est flamme je ne vais pas fuir

Los Angeles jusqu’à Rio
New Delhi jusqu’à London et Tokyo
Partager avec nous
ce que l’on a pris d’autre part

Là où ont la passé
jusqu’à arriver ici
On dira ce que l’on raconte
Los Angeles parie jusqu’à Rio
New Delhi London jusqu’à Tokyo
Partager avec vous ce que
l’on l’a appris là-bas



Je suis heureux
Et toi aussi tu es heureux
Je suis plus heureux que toi

Yzezzzzz

Je suis heureux yeah
Akon
Youssou yeah

Je vais passer au milieu
Qu’il ait des braises
ou est flamme je ne vais pas fuir

Los Angeles jusqu’à Rio
New Delhi jusqu’à London et Tokyo
Partager avec nous
ce que l’on a pris d’autre part

Là où ont la passé
jusqu’à arriver ici
On dira ce que l’on raconte
Los Angeles parie jusqu’à Rio
New Delhi London jusqu’à Tokyo
Partager avec vous ce que
l’on l’a appris là-bas





jeudi 1 septembre 2016

lyrics Song Daan Youssou feat Akon




  Parole Youssou N'Dour feat Akon Song Daan



Dooley nit kou ñuul kou
Ko beug xam la
Mbeur mouy daan kou
Ko beug xam démal laćć ko you

Woma woma Ci leundeum
Dinala Wouyou
Oubil sama
Xol dinga
Xam nimou sédéé ci you

Fileg mang lay am
Sama xol
Luma songù
Daan ko

Fileg mang lay am
Sama Xèll
Luma songù
Daan ko

Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo

Man Maanan
Mane iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh

Man Maanan
Mane iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh

ÉH ÉH
ÉH ÉH

Béneu biss dina niow
Mou melni louniouy netali
Mou melni lii dou

ANHHHHHHH

The ken Du jog
Naan man mi nako fékéh
YOOOOOOO

Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé
Xoob yiy russ ci garab guii
Ah lifi xew tay büñü ko fatéé
Africa Dom yiy wane
sén bopeuh

Fileg mang lay am
Sama xol
Luma songù
Daan ko

Fileg mang lay am
Sama Xèll
Luma songù
Daan ko

Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo
Songù Daan Koooooooo

Man Maanan
Mane iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh

Man Maanan
Mane iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh

ÉH ÉH
ÉH ÉH

Cí Díg bï Fofù
Laay diar Mù am xàl
Safara douma daaw
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog Yén Liñu
Jēlé Fénéne

Fí ñù
Diarr ñun ba éksi fí
Dafa mèlni
Louńou nétali

Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog Yén Liñu
Jēlé Fénéne

Éh Éh
HH HHHHHH
HHHHHHHH

Maa contaane
Yoow it yaa contaaan
Maleu geuuneuu contane
Uhh Yeahhhhh
HHHHHH!!
Contane yeahhh

YEAAAHHH
Contane yeahhh
Contane yeahhh

Akon
Yousou Yeah

Akon
Yousou Yeah

Cí Díg bï Fofù
Laay diar Mù am xàl
Safara douma daaw
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog Yén Liñu
Jēlé Fénéne

Fí ñù
Diarr ñun ba éksi fí
Dafa mèlni
Louńou nétali
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog Yén Liñu
Jēlé Fénéne



Song Daan Youssou Ndour feat Akon Lyrics by Abdoulayebacary

Lyrics Wuyuma Viviane Chidid


Viviane Chidid Wuyuma

  
xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara



mane déh walouléne ma wax koko
xalé bi lékatouma ndax mome
nanatouma nélawatouma
wowo
sama xol yathie néh


lék lék ma woo ko tit dal di coupé
sama appetit coupé
febar dinama guoungué
doctueur dama love ba dof
té xawma loukoy fathie
wowo
mba meune nga thie daraa


xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara


mane woo nala founé
nga diapémma sa xarite
inviter resto, lalal nala louné
wowo
nga diapéma sa xarite



lék lék ma woo ko tit dal di coupé
sama appetit coupé
febar dinama guoungué
doctueur dama love ba dof
té xawma loukoy fathie
wowo
mba meune nga thie daraa


mane beuguena ma bagne bayiwouma
mane guisoumaa
kénén koudoul mome
mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam


xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beug
ue nala té xamothie dara
mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara



xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara


 kouthie nek'aak kingna nope
sa guinaw bandague faxassul
diougueul yyeungueul bamou saf
sa gnuinaw badanue faxassul


kouthie nek'aak kingna nope
sa guinaw bandague faxassul
diougueul yyeungueul bamou saf
sa gnuinaw badanue faxassul


Lyrics Viviane Chidid "WUYUMA" by abdouayebacary