jeudi 22 septembre 2016

Lyrics Alalou Mboolo Youssou N'dour



dolou lou ak yakar mo takh niou tann la dolou lou ak yakar mo takh niou wallon woloula bou nitt yi barry barry
yow dong nan fi tane neu tekk la fee dolou lou ak yakar mo takh niou tann la dolou lou ak yakar mo takh niou wallon woloula bou nitt yi barry barry yow dong nan fi tane neu tekk la fee confiance bou niou amm si yaw boul ko saganeee yakar bi nou amm si yow ba kay denk la sou la key am ga loy bagh gorforoul ba deff ko niou ka beugé gorr bakhna jigeenne bakhna jioup dall moy li worr fekhel ba yeboulene na fekhel ba woney lou takh niou woloula gorr bakhana jigenne bakhna jioup dall moy li worr fekhel ba yeboulene na fekhel ba woney lou takh niou woloula dium borry ndone bourr daly dium borry ndone bourr daly dium borry dafa lalou bour motakh mou diam kou defoul dara dep di koy door dium borryey dium borry dafa lalou bour motakh mou diam kou defoul dara dep di koy door dium borryey sou deyy lou ga wara wakh wakh dall mou diekh sou deyy lou ga wara diokhe diokho nio ko mome soi deyy loy ga wara dokh dokh do ba mo matte maïs fefele beu yemene naga fefe ba woné lou takh niou woloula wakhou ma la dara waye wolou gui nou la wolou boul ko fowé yaw alalou MBolo boll ko fowé bilay dinkanela boul ko fowé yaw alalou mbolo boul ko fowé bilau dinkanela wawaw boul ko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowé deugel samal ma wa way bouko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowé deuk deug mbotoul ma ma wawaw boul ko fowé dilay alalou mbolo bou ko fowe deug deug samal ma waw waw bilay alalou mbolo wawa bilay samal ma daa gaa wara gore denkanè denkanéee lo momoul manou theuy yaw alalou mbolo boul ko fowé deuk deug sa mal ma boul ko fowé bilay alalou mbolo boul ko fowe deuk deuh moy toul ma alalou mbolo wowoww boul ko fowé bilay alalou mbolo deug deug manou nou sa wawaw dou atier lou tatier dou arier lou tatier lyrics alalou mbolo by abdoulayebacary


Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire