lundi 19 septembre 2016

Lyrics Youssou N'dour C'est l'amour


Lyrics Youssou N'dour C'est l'amour



sou wakhtané ak sa ma ngiégénay
nakh goudi de yokou khel
sou beuthie ké ma dall di faté
mane guinntiyé you  ma guintone bigu

c'est l'amour


sou mala rombé di dem 
na fokk liéph bakhna si mane
apparrence bi nakhna la
khamoulo li nékk si mane 


c'est l'amour

to love
Amoré
Chintouru
yébene

magui dann sa ma dolé
magui sante yalla
magui fathe sa may athio

mounay amm na lou dess


c'est l'amour

mane lekouma
mane nanouma ba they
mane hiffouma ba they
mane somouma 
mane geumouma ba they
nelawouma lou doyy


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
nakhe beur


tolove
Amoré
Chintouru
yébene
Chintouru
yébene
nakhe beur


mane lekouma
mane nanouma ba they
mane hiffouma ba they
mane somouma 
mane geumouma ba they
nelawouma lou doyy


c'est l'amour


magui dann sa ma dolé
magui sante yalla
mounay mounay amm na lou dess


souma khanaé akk sa ma ngégenay
nakh goudi dey yokou khel
magui dann magui dann sa ma dolé

mounay mounay amm na lou dess

lyrics C'est l'amour youssou N'dour by Abdoulayebacary



Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire