lyrics Youssou Ndour baykat
kha lolakha lola
lola la la la
djambar you gorr ya ngoge baykat
bay mbboke bay dougoup you nou doundé
nath bi di tangue niou sentou taww
séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne
sou naletelé ngédi sentou taww
soko wedé demal baol
mba ga dem ba walo Mbodj
sou nord tioté nou weurr di leep
sou tambalé khinn niou sentou taww
sou tawwé sou tawwoul ngui fay borr
séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne
mbir mbirou garap mbagui si yaww
khiff yi ngou khiff yayee kou key fadj
mbeuss yi niou wessou ndiome nelawouniou
sou naletelé ngédi sentou taww
soko wedé demal baol
mba ga dem ba walo Mbodj
mba ga dem sine saloum béé
séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne
djambar you gorr ya ngoge baykat
bay gerté bay mbokk you nou doundé
lata mouy taww niou falas khar
séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne
sou taww mbaré Dakarou Wagni ndeukk
sou taww amoul dakarou Yokk ndeukk
lou thi meuna amm li déé metina
séé sédelene djambar guéne
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
dimba lé ko
dimba lé ko
ya karr dafa tass
dimba lé ko
momo avk sa mbope bathi
kha lola
kha lola
lola la la la
kha lola
kha lola
lola la la la
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
momo avk sa mbope bathi
séé sédelene djambar guéne
lyrics Youssou Ndour baykat by Abdoulayebacary
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire