kou guisse sa beut yi di khol mbaye gueye dioudal mako
ahh mbeuguel capitaine nou mboromom
mbeuguel da fa disse
dafa beuri dollè
dinala niakalo sa allal
di gna nagou yaw lo geumoul
mbeuguel bou la diam ba amo loy deff
yalla bo beug nikk ki kokou beug la loloo
andoula ak ay principe ah sentiment la
ay dioyy riekk la situation rekk la
mbeuguel bou la diap ba so amon loy deff
yalla bo beug nikk ki kokou beug la loloo
mbeuugnaleu
chérie diogh nala sa ma khol
bolethi di la yeureum
dila moungalit fo beug niou dem fa
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
man sou ma amon avion tay ma maylako
di la dawalal fo beug nou dem ko
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
mbeugnala
fogu nou wendellou
bou mbeugel donne lumière
diante te bi lay dieuli
kham na di na metti sa
wa ye diarral na ma ko
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
lou ma dougou nga kham ko
kham ndany lou ma am sa ma daradia damppul
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
mbeugnala
fogu nou wendellou
Golber sou ma khamon ki kan la
dou ko defeti!
dou defeti lou ni mell
khana khamol sou niou kharite nga
golber kou la khamoul na la ladj
Aladji mensou seck ba tia Ndar
mba nou fekhe ba lath la way di fou nieuwone donn seyaré sa
golber gui na ne ga Ndar geutt beuri nga fey ay kharite
ngui la sopp barina Mame coumba Barry si la bokk
bilah beugnalala
fokk niou wendelou
dikh nala sa ma khol bokk si di la yeureum
di la mou nieul lit fo beug nio dem fa
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
mane sou ma avion tay ma may lakou
di la dawalal fo beug niou dem fa
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
bo mbeuel donne lumière
diante bi la dieuli kham na di na metti
sa waye na ma ko
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
beugeunalla foy nou wendellou
foncnala fokk niou wendellou
mane sou ma avion tay ma may lakou
di la dawalal fo beug niou dem fa
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
bo mbeuel donne lumière
diante bi la dieuli kham na di na metti
sa waye na ma ko
li sou la doyoul khaw ma lou lay doyy
loi ma doug na kham ko
sa ma dara oumpoula
lisou la doyoul khaw ma lou lay doyy
man dall beug nala
mbaye kay niou wendellou
djino kou la guii djii ala
mais djinno
Lyrics by Abdoulayebacary
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire